Puppa Lëk Sèn - Sam Bi

Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw, duma delou ganaw
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw, duma delou ganaw

Mo may dolil yërmande, mo may dolil sutura
Luleen neex diem leen, walaxi dem na ma
Lala, lala, lala, lalala, lala

Waay le leen ma, sangue bi, waay le leen ma, sangue bi
Waay le leen ma, waay le leen ma
Waay le leen ma, sangue bi, waay le leen ma, sangue bi
Waay le leen ma, sangue bi, waay le leen ma

Waay le leen ma, sangue bi, waay le leen ma, sangue bi
Waay le leen ma, waay le leen ma
Waay le leen ma, sangue bi, waay le leen ma, sangue bi
Waay le leen ma, sangue bi

Rastafari, yeah
Come on, rock it

Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw, duma delou ganaw
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw, duma delou ganaw

Mo may dolil yërmande, mo may dolil sutura
Luleen neex diem leen, walaxi dem na ma
Lala, lala, lala, lalala, lala (Rastafari)
Lala, lala, lala, lalala, lala
Lala, lala, lala, lalala, lala
Lala, lala, lala, lalala, lala (yeah, Lord)

Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw, duma delou ganaw
Ki gnouy sam yow, mome la dink sama lep man
Duma tite, duma daw, duma delou ganaw

Mo may dolil yërmande, mo may dolil sutura
Luleen neex diem leen, walaxi dem na ma

Puppa Lëk Sèn lyrics are copyright by their rightful owner(s) and Jah Lyrics in no way takes copyright or claims the lyrics belong to us.
Jah Lyrics exists solely for the purpose of archiving all reggae lyrics and makes no profit from this website.