Puppa Lëk Sèn - Dance All (Remix)
EXPLICIT

Jamba sound system
Da number one sound system
Big inna town
Ya hear mi massi
Moove ya
Ah ah, ah ah, ah ah..

Lu mu gudi gudi, da nagne fa dem
Da nagne fa yëksi, da nagne fa dem
Lu mu gudi gudi, da nagne fa dem
Da nagne fa yëksi, da nagne fa dem

Sunu music ganaw la feete
Kanam la wara dem
Talu gnu di fene
Mbir mi bak, sagne sagne
Na dagne dagne
Sunu music kena du ko faye
Mbir mi bak, sagne sagne
Na dagne, na dagne dagne
Lëk Sèn music, one love

Dance, dance, eh wadji dance leen yeen..

Eh eh yeen pousse leen
Royuma cii yeen da lou leen
Mother fuck yeen
Afreekan hip hop ta tiu leen
Sama music bi deh jaxalu leen
Eh ho yo fok nga fene eh ho yo fok gnu dem
Madria ba Portugal, Tripoli ba Portugal
Sama music la gnuy sing dal
De mal ba Sénégal
Fuma rombe gnu dad ma top dal
Ndax li may sing dal

Kelemati, Kelemati, Kelemati ling
Jah mamu, Jah mamu, Jah mamu ling
Nga woma cii battle ma gun cësse OK
Kelemati, Kelemati, Kelemati ling
Jah mamu, Jah mamu, Jah mamu ling
Nga woma cii battle ma gun cësse OK
Kelemati, Kelemati, Kelemati ling
Jah mamu, Jah mamu, Jah mamu ling
Nga woma cii battle ma gun ting OK

Dance, dance, eh wadji dance leen yeen..

Puppa Lëk Sèn lyrics are copyright by their rightful owner(s) and Jah Lyrics in no way takes copyright or claims the lyrics belong to us.
Jah Lyrics exists solely for the purpose of archiving all reggae lyrics and makes no profit from this website.