Puppa Lëk Sèn - Booki Masta

Booki Masta
Mano mano mano mano
Bok na cii diamou yallah yow
Mano mano mano mano
Bok na cii diamou yallah yow

Ki wax na, ki def na
Lek nena dead oh
Yi le mbir mome du diamou, yallah yow
Ki wax na, ki def na
Lek nena dead oh
Yi le mbir bocul cii diamou, yallah yow

Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono
Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono

Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono
Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono

Oh mano - (oh mano) oh mano, mano (oh mano)
Oh mano - (oh mano) oh mano, mano (oh mano)
Oh mano - (oh mano) oh mano, mano (oh mano)
Oh mano - (oh mano) oh mano, mano (oh mano)
Do not critizes, oh mano mano
Do not critizes, oh mano mano
Oh mano, oh mano, mano
Do not critizes, oh mano mano

Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono
Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono

Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono
Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono

Mano mano mano mano
Bok na cii diamou yallah yow
Mano mano mano mano
Bok na cii diamou yallah yow

Ki wax na, ki def na
Lek nena dead oh
Yi le mbir mome du diamou, yallah yow
Ki wax na, ki def na
Lek nena dead oh
Yi le mbir bocul cii diamou, yallah yow

Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono
Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono

Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono
Jëffal sa jëff mane djapal sa niambur
Booki masta ya ngi cii ciiono

Ki wax na, ki def na
Ki dem na, ki gnëw na
Booki masta, ya ngi cii ciiono

Ki wax na, ki def na
Ki dem na, ki gnëw na
Booki masta, ya ngi cii ciiono

Neleen gnu jëff hight a

Puppa Lëk Sèn lyrics are copyright by their rightful owner(s) and Jah Lyrics in no way takes copyright or claims the lyrics belong to us.
Jah Lyrics exists solely for the purpose of archiving all reggae lyrics and makes no profit from this website.